Isaiah 7:22 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
meew ne gàññ, ndax nit ñu néew, di dunde am soow, nde soow ak lem la képp ku des ci réew ma di dundeji.