James 1:18 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ci coobareem la nu sole kàddug dëgg gi, ba nu judduwaat, di tànneefu lépp lu mu bind.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Moom la soob mu jure nu kàddug dëgg, ba nu taxawe ab jooxeb ndoortel meññeef, ci biiri bindeefam.