James 1:19 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Yéen sama bokk yi ma bëgg, nangeen xam lii: ku nekk war ngaa farlu ci déglu, di yéex a wax tey yéex a mer.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bokk yi, soppe yi, nangeen xam lii: na ku nekk di gaaw ci déglu, di yeexa wax tey yeexa mer.