James 1:23 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte ku déglu kàddu gi, te bañ koo jëfe, moom ak kuy seetu ñoo yem;
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax kat kuy déglu kàddu gi te jëfewoo ko, kooku daa mel ni kuy niir kanamam cib seetu: