James 2:12 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Gannaaw dingeen nar a jaar ci àtteb yoon, wiy goreel, na loolu lal seen wax ak seen jëf.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Deeleen waxe tey jëfe ni mu jekke ci nit ñu ñuy séddeji àtteb yoon wiy goreel.