bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare James 2:13
James 2:13 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ndaxte ku yërëmul, yoon du la yërëm. Te yërmande mooy noot àtte.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Daan bu àndul ak yërmande, moom lees di àttee ña daawul jëfe yërmande. Yërmande nag kekku na ab daan.