James 2:14 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Te lii itam samay bokk, ku ne gëm nga, te jëfewoo ko, loolu lu muy jariñ? Ndax googu ngëm man na laa musal?
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bokk yi, ku ne gëm na, te jëfewu ko, ana lu mu koy jariñ? Ndax googu ngëm man na koo musal?