James 2:18 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Waaye xanaa dina am ku ne: «Yaw am nga ngëm, man am naa ay jëf.» Yaw nag won ma sa ngëm gu àndul ak jëf, man ma feeñal la sama ngëm ci samay jëf.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye jombul nit ne: «Yaw, ngëm nga am, waaye man, jëf laa am.» Dama ne, won ma sa ngëm gu àndul ak jëf; man, samay jëf laa lay wone sama ngëm.