James 2:24 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Kon nag gis nga ne, Yàlla ci jëf lay àtte nit ni ku jub, waaye du ci kaw ngëm kese.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ngeen gis kon ne ci jëf lees di joxe nit àtteb ku jub, waaye du ci kaw ngëm doŋŋ.