James 2:25 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Naka Raxab jigéenu moykat bi itam, ndax du ci noonu la ko Yàlla àttee ni ku jub, ci li mu teeru ndawi Yawut yi, te jaarale leen ca poot ba?
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Xanaa du noonu it lañu joxe Raxab gànc ba, àtteb ku jub, ci kaw jëfam, ndax la mu dalaloon ndawi Yawut ya, ba awale leen feneen?