bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare James 3:1
James 3:1 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Samay bokk, bu ñépp di sababloo nekk jàngalekatu mbooloo mi, xam ne nun jàngalekat yi, àtte bi nuy jaar mooy gën a diis.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bokk yi, bu ñu bare ci yeen wuta doon sëriñi mbooloom gëmkat mi, ndax xam ngeen ne nun ñiy jàngle nooy gëna metti ab àtte.