James 3:12 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Samay bokk, ndax mas ngeen a gis garabu figg gu meññ oliw, walla garabu réseñ gu meññ ay figg? Mukk! Mbënnu xorom mënta nàcc mukk ndox mu neex.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bokk yi, ag figg man naa meññ oliw? Am ag reseñ dina meññ doomi figg? Bëtu ndoxum xorom it du nàcc mukk ndox mu neex.