James 3:4 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Te gaal yi it yu réy lañu, te ngelaw lu am doole di leen jiñax, waaye dawalkat bi, weñ gu tuuti la leen di jëme fu ko neex.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Xool-leen gaal yi it, ak ngelaw lu réy lu leen mana jañax, weñ su tuut la dawalkat biy walbatee gaal gi, jëme fu ko neex.