James 3:8 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye làmmiñ kenn mënu koo noot; musiba la mu dul dal mukk, fees dell ak daŋar juy rey.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye aw làmmiñ, kenn manu koo tàggat ba mu mokk. Mooy aayteef gu kenn manula dànk, fees dell ak tookey ndee.