James 4:11 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Yéen bokk yi, buleen ŋàññante. Ku ŋàññ sa moroom mbaa nga ñaaw njort, ba àtte ko, diiŋat nga yoonu Yàlla te àtte ko; ku àtte yoon wi nag sàmmoo ko, waaye danga koo àtte.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bokk yi, buleen ŋàññante. Ku ŋàññ sa mbokk mbaa nga sikkal sa mbokk, yoon wi nga ŋàññ, yoon wi nga sikkal. Ku sikkal yoon wi nag doo sàmmkatub yoon wi, sikkalkatub yoon wi nga.