James 4:12 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Kenn rekk mooy tëral yoon, kooku rekk mooy àtte; moo man a musle, moo man a alage. Te sax yaw miy àtte sa bokk yaay kan?
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Boroom yoon wi, kenn doŋŋ la, te mooy àtte; moo mana musle, mbaa mu sànke. Te yaw miy sikkal sa mbokkum gëmkat sax, yaay kan?