James 4:14 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndax dangeen a xam seen ëllëg? Te luy seen dund? Xanaa cóola doŋŋ luy naaw ci diir bu gàtt, daldi naaxsaay.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeen xamuleen sax lu ëllëg di doon? Ana luy seen bakkan? Yeen ngeen di as lay suy feeñ léegi, nes tuut mu ne mes!