James 4:16 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Waaye fi mu ne, naagu ngeen bay damu, te damoo noonu baaxul.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Léegi daal dangeena bew bay damoo seeni mébét! Googu damu de, lu bon la.