James 4:3 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bu ngeen ñaanee sax, dungeen jot dara, ndax yéena ngi ñaan ci naaféq, ngir gën a topp seen nafsu.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Te su ngeen ñaanee, dungeen am, ndax mébét mu bon ma ngeen ñaane, ngir am lu ngeen toppe seen bakkan.