James 4:5 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Xanaa yaakaar ngeen ne, Mbind mi day wax cig neen, ci li mu ne: «Yàlla am na mbëggeel gu fiir ci Xel mi mu def ci nun.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Am defe ngeen ne ag neen la Mbind mi indee ne: «Xemmemtéef gu ànd ak fiiraange la Yàlla am ci noo gi dëkk ci nun.»