James 5:17 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Naka noonu Iliyas nit la woon ku bindoo ni nun, waaye bi mu saxee ci ñaan Yàlla, ngir mu bañ a taw, ndox laalul suuf diirub ñetti at ak genn-wàll.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ilyaas nit la woon ku bindoo ni nun, waaye ba mu saxee ci ñaan ngir mu baña taw, ndox laalul suuf diiru ñetti at ak genn-wàll.