James 5:20 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
na xam lii: ku gindi bàkkaarkat ci réeram, musal nga nit ci dee te faral ko bàkkaar yu bare.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
xamleen ne ku waññee bàkkaarkat ci yoonu sànkuteem, musal na bakkanam, te faral na ko bàkkaar yu bare.