James 5:8 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Yéen itam nag muñleen te dëgëral seen xol, xam ne ñëwu Boroom bi ci ndamam jege na.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeen itam muñleen te takk seenu fit, ndax bés ba Boroom biy dikk dëgmal na.