Jeremiah 11:15 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Ana lu samay soppe di defati sama kër? Ñu bare ci ñoom a ngi def lu bon. Ndax seeni sarax man naa far seen jëf ju ñaaw, ba tax bu ñuy def lu bon, di ko bége?»