Jeremiah 12:14 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Aji Sax ji dafa wax ne: «Mboolem sama dëkkandoo yu bon, yi laal céru suuf bi ma sédd Israyil sama ñoñ, maa ngii di leen déjjatee seen réew, te waa kër Yuda, maa leen di seppee fi seen digg.