Jeremiah 16:15 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye dañu naan: “Giñ naa ko ci Aji Sax jiy dund, ki jële bànni Israyil réewum bëj-gànnaar, te jële leen mboolem réew ya mu leen sànke woon.” Maa leen di délloosi seen réew ma ma joxoon seeni maam.»