Jeremiah 16:3 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Aji Sax ji kat dafa wax ci gone yu góor yeek gone yu jigéen yi juddoo ci bii bérab, wax ci seen ndey yi leen jur wax ci seen baay yi leen meññ ci mii réew,