bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Jeremiah 16:5
Jeremiah 16:5 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Te Aji Sax ji kat dafa wax ne: «Bul dugg kërug dëj, bu fa dem di ñaawlook a jaale. Maa xañ askan wii sama jàmm,» kàddug Aji Sax jee, «xañ leen sama ngor ak sama yërmande.