Jeremiah 16:9 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Aji Sax ji Yàllay Israyil Boroom gàngoor yi kat dafa wax ne: «Maa ngii di dakkal ci bii bérab, ngeen teewe, fekke lépp luy coowal mbégteek bànneex, boroom séet ak séetam selaw.