Jeremiah 17:3 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ak kaw tund yi ci àll bi. Seen alal ak seen denc yépp laay joxe, ñu lël ko, booleek seen jaamookaay ndax seen moy yi dajal réew mi.