Jeremiah 2:25 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ma ne, buleen daw ba mujje tànki neen ak put gu wow. Ngeen naa: “Bul sonn, sopp nanu yàllay doxandéem yi, te ñoom lañuy topp!”»