Jeremiah 2:8 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
« Sarxalkat yi newuñu: “Ana Aji Sax ji?” Ñi ŋank yoon wi faaleetuñu ma, njiit yi gàntal ma, yonent yiy waxe waxyuy Baal, tuur mi, di topp lu leen dul jariñ.