Jeremiah 21:1 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kàddu dikkaloon na Yeremi, bàyyikoo fa Aji Sax ji. Mooy ba buur Cedesyas yebalee ca moom, Pasur doomu Malkiya, mook sarxalkat ba ñuy wax Cefaña doomu Maaseya. Mu ne ko: