Jeremiah 21:8 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Te itam nga wax askan wii ne leen: “Aji Sax ji dafa wax ne: Maa ngii di teg fi seen kanam yoonu dund ak yoonu ndee.