Jeremiah 22:11 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Aji Sax ji kat dafa wax ci mbirum buurub Yuda, Salum mi wuutu baayam Yosya te bàyyikoo fii. Mu ne: «Du fi délseeti mukk.