Jeremiah 22:12 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye fa ñu ko yóbbu ngàllo, fa lay deeye. Réew mii, du ko gisati mukk.»