bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Jeremiah 22:6
Jeremiah 22:6 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Aji Sax ji déy dafa wax ci mbirum kër buurub Yuda ne: «Yaay sama àllub Galàdd, sama collu tundu Libaŋ, waaye déy, maa lay def ni màndiŋ, ngay dëkk yu kenn dëkkul.