Jeremiah 23:35 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Li ku nekk wara laaj moroomam mbaa mbokkam kay mooy: “Lu Aji Sax ji tontu?” mbaa “Lu Aji Sax ji wax?”