bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Jeremiah 24:3
Jeremiah 24:3 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Aji Sax ji wax ma ne ma: «Yeremi, loo gis?» Ma ne ko: «Xanaa ay figg. Figg ju baax ji nag baax na lool, waaye ju bon ji daa bona bon, ba kenn du ko lekk ndax bon.»