Jeremiah 24:8 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye Aji Sax ji déy dafa wax ne: «Ni figg jii bone, ba kenn manu koo lekk ndax bon, ni laay def Cedesyas buurub Yuda aki kàngamam ak ndesu Yerusalem. Muy ñi des ci réew mi, di ña toxuji Misra.