Jeremiah 25:26 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
boole ca mboolem buuri bëj-gànnaar, ñu jegeek ñu sore. Ma nàndal leen ñoom ñépp, ba réewi àddina yi ci kaw suuf yépp daj. Buurub Sesag topp ci ñoom, naan.