Jeremiah 26:11 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Sarxalkat yaak yonent ya wax kàngam yaak mbooloo ma mépp, ne leen: «Waa jii, dee mooy àtteem, ndax moo biral waxyu, di rëbb sunu dëkk bii. Yeena ko déggal seen bopp.»