Jeremiah 26:4 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Nga wax leen ne leen: “Aji Sax ji dafa wax ne: Su ngeen ma déggalul, toppuleen yoon wi ma leen rëddal,