Jeremiah 27:16 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gannaaw loolu sarxalkat yeek askan wii wépp wax naa leen ne leen: «Aji Sax ji dafa wax ne: Buleen déglu yonent yi leen di waxal ay waxyu, naan leen: “Ndabi kër Aji Sax jaa ngii di délsi, jóge Babilon léegi, léegi.” Ay waxyuy fen lañu leen di waxal.