Jeremiah 27:18 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bu ñu dee ay yonent kay, te kàddug Aji Sax ji nekk ci ñoom, nañu daldi tinu Aji Sax ji Boroom gàngoor yi, ngir ndab yi des kër Aji Sax ji ak kër buurub Yudak Yerusalem, te baña dem Babilon.