Jeremiah 27:19 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Aji Sax ji Boroom gàngoor yi de wax na ci mbirum jëni këram geek mbalka meek watiiri rootukaay yi ak yeneen ndab yi des ci dëkk bii,