Jeremiah 29:17 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Aji Sax ji Boroom gàngoori xare yi dafa wax ne: «Maa ngii di leen yónnee saamar akub xiif ak mbas. Maa leen di def ñu mel ni figg ju nëb, ba kenn manu koo lekk ndax bon.