Jeremiah 29:25 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
“ Aji Sax ji Yàllay Israyil Boroom gàngoor yi dafa wax ne: Yaw yaa yónnee ci sa turu bopp ay bataaxal ca askanu Yerusalem gépp, rawatina sarxalkat ba Cefaña doomu Maaseya, ak mboolem sarxalkat ya. Nga di ci wax ne: