Jeremiah 29:31 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Yónneel ca ngàllo gépp ne leen: Aji Sax ji dafa wax ci mbirum Semaya Neyelameen ba, ne: “Semaya waxal na leen waxyu, gëmloo leen ay fen, te yebaluma ko.