Jeremiah 29:4 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Aji Sax ji Yàllay Israyil Boroom gàngoori xare yi dafa wax mboolem ngàllo ga mu jële Yerusalem, yóbbu Babilon, ne leen: